1er COUPLET
Beuga toma wakhma
Xawma lu waral légui mane falé toma
Guiss nani diex na
Waxoko mais khamnani ni nobatoma
Gaaw ci defma luma méti
Say wax néxatul mangui deg lu né
Lu dieum ci mane sa yoon nékoussi
Souma déwoon do weet ndax du mane malay wétali
HOOK
Wano ma woon lii
Bagnouy tambali
Waxo ma wone lii
Meunatuma ndax dama taaayi
Wano ma woon lii
Bagnouy tambali
Wakho ma woon lii
Meuneutou mala mougneul dax mane dame la baayi
REFRAIN
Dame la bayi hé (3x)
Toggatumafi di mougn ndax mane taaayi
Dame la Baayi 2x
May kila baayi
2ème COUPLET
Goudi ba goudi lalay guiss
Dem na ba légui damako miss
Waxa tok mane
Falé toma
Sama wétal doon naxar ak tiss
Yay kiy béguel samay noon
Bax ci mbed mi ci mane nga bone
Dieukeur boula yénétoul foon
Ma name la té sori woma
HOOK
Wano ma woon lii
Bagnouy tambali
Waxo ma wone lii
Meunatuma ndax dama taaayi
Wano ma woon lii
Bagnouy tambali
Wakho ma woon lii
Meuneutou mala mougneul dax mane dame la baayi
REFRAIN
Dame la bayi hé (3x)
Toggatumafi di mougn ndax mane taaayi
Dame la Baayi 2x
May kila baayi
COUPLET RAP
Mangui dem guissouma liy tax may deloussi
Bou déssé loudoul sa keur ma fanaan ci mbed mi
And nexna wayé ko ba mou démak mbagam
Diox la sama xol ga fowé ko yaw danga lundeum
Yag na du tay
Wané gako tay
Naxaral sama xol xam nga yako tay
Légui dafa doy
Dotou mako joy
Beuss sa gui ci beussi lo lebblé lagne lay fay
1er COUPLET
Sénégal niokko mome
Kéne meunouko khar niar
Khiff lekk niakoufi
Marnane niakoufi
Goudé am fo fanane sama rew
Bouniou nangou keneu douggou souniou diguenté
Same diam djifi niom mame bayi
Khamouniou lénène
Bougouniou lénène
Hé Hé Hé
REFRAIN
Gueye ndioro waynala ( gueye ndioro waynala)
Faye birame waynala ( waynaaaaaala )
Diobeu dioubeu waynala ( diobeu dioubeu waynala waynala waynala )
Tourè mandi waynala (hééééééhéhéhééé)
Thiam babel demba thiam
Gomissa gania waynala ( sané balama )
Ndiaye diatta ndiaye waynala
Dioufa niokhobay waynala (mané djonkéléfa)
HOOK
Sante yi war galgui reew mangui (x2)
Diom foulak fayda
Fonk diné takh khol yé ngui naat
Dieuf diou bakh deh diogoufi
Soutoura laniouy ndamo
Han Sénégal ndiaye sama rew
Walo walo si réw mi
Sine Saloum si réw mi
Casamance Boundou
Cadior ak Baol Fouta Toro
Djolof Sénégal
Dieng salla waynala (Samb maharam waynala) Diagne Naar waynala (Diallo diery waynala) Sow poulo waynala ( Ba poulo waynala Yagg masseuy) Sall ngari waynala ( Cissé ngari Ngom séni) Ndoye mali maram ndoye waynala ( Wade farawade ndiack ) Mendy coto waynala ( pouye beukeury) Fall ndiaga yaram waynala ( waynala Camara yilé ) Dieye massamba waynala (Guissé maabo) Mbacké balla aissa Sy sawandé Niass coumba abdallah Laye Makhtar Kounta sidy waynaaaaaa léne Sante yi war Galgui reew mangui (Lo ndam ciré) Sante yi war Galgui reew mangui ( Youm sega Mbaye mbassou Diene ndiogou) Sante yi war Galgui reew mangui ( Thiaw séni Mbengue mbor ) Sante yi war Galgui reew mangui ( Ndour wally mbergane Niang mbaallo) Sante yi war Galgui reew mangui ( Sene thiali Sylla moctar ) Sante yi war Galgui reew mangui ( Seck sa guanar ) Sante yi war Galgui reew mangui ( Sarra moundo Ly bousso ) Sante yi war Galgui reew mangui Sante yi war Galgui reew mangui
Refrain
Boss (7x)
Wowéma lady boss
Lady Boss (4x)
Preureup pa peureup pa pa pa (Lady boss) (3x)
Peureup pa pa pa peureup pa pa pa (3x)
Doumak gni
Mbeur bou ngèn fi ngemb ma yobu ko tapis
May prési
Changé loi wou game bi wowé ma Macky
Soulène ben ben niom nieup daniou thiouné
Wowèma lady boss AKA meuné founé
Lithi mane dou niom no bouniou teukeulé
Work hard work hard rek lay def
May dess sa bopp comme dadji
Sax sa xol may fathi
Sama son day febar normal sama brain day nath
Capitaine dirigé game bi
Dieulé fi nieup yokati haine bi
Mane la queen bi saf thi thine bi
Guéné thi nieup ni baag thi tène bi
Enchainé ay hit shit
Goloul do def clean sheet
Encaissé ay mille chèques
Balak touti wéthite
Mane la foma guiss tite
Yek té douma toukh weed
Thiop katou mc la thi game bi
I’m a bad bitch
I i i’m a bad bitch
Monopoliser game bi diokh lene dessite
Boul diay fite lady boss the best deal
Microphone ak beat mak sa mc rek damakoy kill
Téglé samay tangue tok thi trône bi doma diègui
Dima guiss sa khol di bone khamna loula meti
Lofi nate perte tan k mangui fi dofi tègui
Hit bou dem benene bi nieuw lerna doko wèdi
Enchainé ay hit shit
Goloul do def clean sheet
Encaissé ay mille chèques
Balak touti wéthite
Mane la foma guiss tite
Yek té douma toukh weed
Thiop katou mc la thi game bi
I’m a bad bitch
I i i’m a bad bitch
Monopoliser game bi diokh lene dessite
Boul diay fite lady boss the best deal
Microphone ak beat mak sa mc rek damakoy kill
Téglé samay tangue tok thi trône bi doma diègui
Dima guiss sa khol di bone khamna loula meti
Lofi nate perte tan k mangui fi dofi tègui
Hit bou dem benene bi nieuw lerna doko wèdi
Do Meusseu am kou melni mane (3x)
Melni mane (2x)
Baby dama fresh dama clean dama hight
Soumala douguelè thi roukhou walay doma bayi
Khol ma thi kaw bathi souf damay lakkè ni fire
Khamnani i’m the only one you desire
Khalè bou parè bolèthi wang wang wang
Dose binga sokhla malakoy diam diam
Sama wète dangay dègue diam diam diam
Kènay fowè sa khol mane mane mane
Meusso am kou melni mane baby dotoko amati
Bo fowè sa khèl bama reuthie la dotoko dèfati
Do Meusseu am kou melni mane (3x)
Melni mane (2x)
Diongoma mineur baby mane ngay weur
Fi lepp minè dièguèma exploser
Dama posè , osè , i’m good bad girl
Sa tempèrature makoy yèguel diko wathiè baby
Sa yo diakhlè mane ngay lathiè baby
Khalè bou parè bolèthi wang wang wang
Dose binga sokhla malakoy diam diam
Sama wète dangay dègue diam diam diam
Kènay fowè sa khol mane mane mane
Meusso am kou melni mane baby dotoko amati
Bo fowè sa khèl bama reuthie la dotoko dèfati
Meusso am kou melni mane baby dotoko amati
Boul fowè sa khèl bama reuthie la dotoko dèfati
HOOK
May sa ouroul aïni (eeeh)
A mes cotés tu vis le paradis
Fokoy dieuléti kou melni
May sa superstar yay sama paparazzi
May sa ouroul aïni (eh eeeeh)
A mes cotés tu vis le paradis ( Tu vis le paradiiiis)
Fokoy dieuléti kou melni
May sa superstar yay sama paparazzi (paparazzi i i )
Ouhou ouh
Hehehe
Domeusseu am kou melni mane
Hook
Rérone nga gindi ma
Dila way ni Youssou wayè Birima
Rérone nga gindi ma
Way la ni Youssou wayé Birima
Refrain
Koti koti yoli
Sa lokho sama nope démeu
Yoli yoli koti kham linga name tax malay (x2)
Kouthi am sa koti koti déko yoli yoli(x4)
Dof thi mane dieundé woma dara loudoul mbeuguél
Mala tane sépi lathi dakh yamay danél
Yaw kham ngnani kene dou kheutio lilou mome
My baby sama khol bi yako mome
Sama yéné di niou dounde ba sey am thi dome
Niouy koti koti yoli yoli lithi soukeur dou xorom
Thiafka mbeuguel ngama niamal
Sama khol binga keuf moma sonal
Seytanè yi nagne niou mousseul
Yaye sama Messi dama beugue ngamay teul
Dila khalat di ré feep nga meuné
Gninane damay dieulé nagne ma thieupé
Doy nga kharit doy nga andando
Souma nieup bayé nala dessé
Mak yaw thi khalé
Hook
Rérone nga gindi ma
Dila way ni Youssou wayè Birima
Rérone nga gindi ma
Way la ni Youssou wayé Birima
Refrain
Koti koti yoli
Sa lokho sama nope démeu
Yoli yoli koti kham linga name tax malay (x2)
Kouthi am sa koti koti déko yoli yoli(x4)
Bokoulok gniy door
Li goor yi di bari bari amo thi dé dénda ndo
Léme bougnou soukeur
Kouko xass moss daal
Dou yombeu bayi ko
Yaw danga meune mine mokal jiguéne
Mani danga rax ndax li dou néne
HOOK
Beut yi gueuthie na taa ndax yaw
Xol bi deuké naate ndax yaw
Yéndo di rétaane ndax yaw
Namuma greffage ndax yaw
Faléwuma maquillage ndax yaw
Diotna gnou mariage maak yaw
REFRAIN
Baby kaay gnaane si
Dieundeu gouro Paa bi takeu seuye bi
Lima beug moy niou dem mairie
Dem mairie niou dem mairie (2x)
HOOK
Beut yi gueuthie na taa ndax yaw
Xol bi deuké naate ndax yaw
Yéndo di rétaane ndax yaw
Namuma greffage ndax yaw
Faléwuma maquillage ndax yaw
Diotna gnou mariage maak yaw
REFRAIN
Baby kaay gnaane si
Dieundeu gouro Paa bi takeu seuye bi
Lima beug moy niou dem mairie
Dem mairie niou dem mairie (2x)
Yaye sama titi tara pararapa para para
Li mbeuguelou moumeu le diaroul di wax ndax yaw mi xam nga
Laadiou ma aye milliard
Kilo gouro nga ame diabar
Kone légui lane ngay xaar
Gnoune jiguene seuy moy suñu taar
HOOK
Beut yi gueuthie na taa ndax yaw
Xol bi deuké naate ndax yaw
Yéndo di rétaane ndax yaw
Namuma greffage ndax yaw
Faléwuma maquillage ndax yaw
Diotna gnou mariage maak yaw
REFRAIN
Baby kaay gnaane si
Dieundeu gouro Paa bi takeu seuye bi
Lima beug moy niou dem mairie
Dem mairie niou dem mairie (2x)
HOOK
Beut yi gueuthie na taa ndax yaw
Xol bi deuké naate ndax yaw
Yéndo di rétaane ndax yaw
Namuma greffage ndax yaw
Faléwuma maquillage ndax yaw
Diotna gnou mariage maak yaw
REFRAIN
Baby kaay gnaane si
Dieundeu gouro Paa bi takeu seuye bi
Lima beug moy niou dem mairie
Dem mairie niou dem mairie (2x)
Yangui dape sama banekh
Di fathie samay adio
Xam di def lila war
bolèwo darak thioy
wayè wayè am na lou dess
niou dem mairie (x4)
Baby kaay gnaane si
Dieundeu gouro Paa bi takeu seuye
Lima beug moy niou dem mairie
Dem mairie niou dem mairie (2x)
Ngor amoul ndieuk boulko diay
Goree ba kheuy deh boulko bayi
Di dounde lo donoul amoul ndieurigne nanko bayi
Diarouko way
Fékhél nank ko bayi
2ans yangui koy topp
Xalè bi néna bouggoula
Def nga louné wakh louné
Mome noboula
Lékato té nélawato
Dem nga bay khalat ni faw nga diouk serigne touko
Manila bayil mou sed
Bayil mou sed
Bayil mou sed
Diarouko bayil mou sed
Nièmé sagnsé telephone bou guène nga am ko
Yaw rek thi khalè cheveux bou cher nga solko
Ndékété yo yoro dangay abb yoro
Niodi boss di diay lou amoul nieupeu kham ni yoro
Kone bayil mou sed
Bayil mou sed
Bayil mou sed
Yoro kone deh bayil mou sed
HOOK
Ngor amoul ndieuk boulko diay
Goree ba kheuy deh boulko bayi
Di dounde lo donoul amoul ndieurigne nanko bayi
Diarouko way
Fékhél nank ko bayi
REFRAIN
Bayi bayi bayi, Bayil mou sed(x4)
Nena moy sa kharit té yaw rek la tek beute
Lo am dakoy nakhari gnéné nek leu moungék keur
Nga sagnsè mokoy sonal
Sa mbecté bonal kholam
Yeuk ngeu ni dalay sossal
None la
Bouko falé bayil mou sed
Bayil mou sed
Boyil mou sed
Diarouko bayil mou sed
Mome mak la té ba legui nango gouko
Weur thi kogne bi dieul thi khalé bayé gouko
Niouleul bopp
Guéné face
Di diay taar
Père bayil mou sed
Dem nga feep
Wakh ngakh nieup
Kham nga lepp
Kone pere bayil mou sed
HOOK
Ngor amoul ndieuk boulko diay
Goree ba kheuy deh boulko bayi
Di dounde lo donoul amoul ndieurigne nanko bayi
Diarouko way
Fékhél nank ko bayi
REFRAIN
Bayi bayi bayi, Bayil mou sed(x4)